They Cap

Samba Peuzzi

Compositor: Não Disponível

Mom nèna, mom nèna, mom nèna

Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug

(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non

Hey nènagn i can’t put it up
Damlènn eup djap
Game bi lay gnew deup
Kholal I don’t give a fuck
Yendou weur di fènn, yenfou guordjiguènn
Yakk dèrr di tèkk, bumlèy djap di hum hum
Fucking nigga yak seu gnag bi yeup lagnouy ki kill
Gno tèyer game bi 4life, yu know the di dil
Mais santt Yallah alhamdoulah
Mane ma way oulalah

Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug

(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non

Mak yaw dougnou bèneu (nguanè)
Dangueu beug ma khof leu (nguanè)
Ya ma meunn fènn ngueu
Man boyou hood la
Diamenz 4life toussss dara doko dèff
Nigga dèy dèf dou wakh, nigga dèy dèf dou wakh
Am on my way
Tchow li beuri neuI’m on my waaaay
Niggaz capping but I’m on my way yeah
Gnou ngui wakh lounè I’m on my way yeah mon nèna

Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug

(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non
(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non

Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug
Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug

(Mak gnom) bokougnou dieumoukay
Bokougnou dieumoukay non
(Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non
Bokougnou dieumoukay non

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital