Tama

Samba Peuzzi

Compositor: Não Disponível

Gni di weur loumay fey
May coaché deureum ni tatch
Gnè di weur di fènn
May coaché deureum ni tatch

Hey tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Hey papa ndiaya wakhal ak gnom

Heeey ndiaya wakhal ak gnom
Heeey tama wakhal ak gnom

A part generation coumbeu
Musique bi mako meuneu gawlo
Ay pages youtube you guoumbeu
Sènn tèy khamnguènn ni sama daw leu
Gnom dagnou djakhann di saaw
Job africa sogua songuou kaw
Mali ani sokhomo
Nguani ma sokhoma béni
Téleu deul tél tchi guènndjeul seumeu temps
Yonou ndawv dou guaw
Yorr bayré youssou madjigènn
Douma concurrenou kènn tchi yènn
A bouguou Papa from alou panyan
Maigua cissé mangi fay tchop beu légui
Tchow li tchow li, Yaye amoul wakh

Gni di weur loumay fey
May coaché deureum ni tatch
Gnè di weur di fènn
May coaché deureum ni tatch

Hey tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Hey papa ndiaya wakhal ak gnom

Heeey ndiaya wakhal ak gnom
Heeey tama wakhal ak gnom

Gno bokk game bi, wayè dougnou bènn
Seu boop féssoul takh sa poche yi beunn
Tchow li tchow li, danguay wakh té do dèff
From djèkk fils may coacher
Yégueul barre todj niveau
Fékk meu milieu may ngolo
Borom abidjan leu ak la fayette
Samba késséLékk sénn money, dém teudi nélaw
Senegalboy wakh ko tchi kaw
Amna ay boy town yiy sissou
Gnom deugnouy doul kènn doussi shoot
Boudè gnou ngui si cas boy diamguen o bloc
Mane la domou réwmi damfi tèkk sama tank
Niveau bimeu tolou meune toumeu tontou
Né si sama yone baylènn gnouy onkou

Gni di weur loumay fey
May coaché deureum ni tatch
Gnè di weur di fènn
May coaché deureum ni tatch

Hey tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Tama wakhal ak gnom
Hey papa ndiaya wakhal ak gnom

Heyyy ndiaya wakhal ak gnom
Heeey tama wakhal ak gnom

Allô? Tama wakhal ak gnom

Heeey
Heeey
Heeey
Heeey

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital