Je ne mérite pas ça

Samba Peuzzi

Compositor: Não Disponível

Je ne mérite pas ça
Yeah, yeah

Hey bu ma xamoon ni lay demee duma ko nob
Bu ma xamoon ni lay demee duma ko love
Bu ma xamoon ni la may def duma ko jox yeah
Bu ma xamoon ni lay deme hey

Pourtant bañaluma dara, sa yaay ak sa pape
Pourtant bañaluma won dara, sa yaay ak sa pape
Bàyyiwoon naa lépp ndax yaw ak seen waa-kër
Fàttewoon naa ñépp ndax yaw ak seen waa-kër ouh ouh
Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax?

Babe ak fi ñu jaar yépp pur man du jeex
Munuma ko gëm, you're always on my mind
Lu ma wax mu bañ, nanguma déglu
Ne na dey dem xale bi wóor na ma
Ça me fait très mal, tu me calcules plus
Je t'ai tout donné, t'es parti comme ça
T'avais promis de rester pour le meilleur et pour le pire
Elle a brisé mon cœur pour du xaalis

Bul jaay sa ngor
Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg
Bul jaay sa ngor
Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg

Hey bu ma xamoon ni lay demee duma ko nob
Bu ma xamoon ni lay demee duma ko love
Bu ma xamoon ni la may def duma ko jox yeah
Bu ma xamoon ni lay deme hey

Pourtant bañaluma dara, sa yaay ak sa pape
Pourtant bañaluma won dara, sa yaay ak sa pape
Bàyyiwoon naa lépp ndax yaw ak seen waa-kër
Fàttewoon naa ñépp ndax yaw ak seen waa-kër ouh ouh
Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax?
Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax?

Babe, ndax nak dina am lu baax bu de
Yàlla xol lay fay
Je make my heart great everyday
Problème sur problème
Et j’essaye de tout régler euuuh
Tay si ki, suba si kee
Bad girls changel suba du ni
Tay si ki suba si kee, yeah

Bul jaay sa ngor
Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg
Bul jaay sa ngor
Bëggal te Yàlla tax loolu rekk ay dëgg

Hey bu ma xamoon ni lay demee duma ko nob
Bu ma xamoon ni lay demee duma ko love
Bu ma xamoon ni la may def duma ko jox yeah
Bu ma xamoon ni lay deme hey

Pourtant bañaluma dara, sa yaay ak sa pape
Pourtant bañaluma won dara, sa yaay ak sa pape
Bàyyiwoon naa lépp ndax yaw ak seen waa-kër
Fàttewoon naa ñépp ndax yaw ak seen waa-kër ouh ouh
Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax?
Je ne mérite pas ça, lu tax nga may nax?

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital